We’ve updated our Terms of Use to reflect our new entity name and address. You can review the changes here.
We’ve updated our Terms of Use. You can review the changes here.

Nataal

by SAHAD

/
  • Streaming + Download

    Includes unlimited streaming via the free Bandcamp app, plus high-quality download in MP3, FLAC and more.
    Purchasable with gift card

      €7.50 EUR  or more

     

1.
Ndiaxas 03:51
Ndiaxas ------ Refrain: Ndiaxas La connecting people la Ndiaxas la connecting yëg yëg Ndiaxas la Xonk nop ak negro la Ndiaxas njalabaan ak zeytoun la Aduna bi lii ko soss mo bari Melo yii ,tur yi, doomu adama wuuté mo tax ba xam xam bi sawaan Mo tax goor ba yëg yëg yi bari ndiaxas la Aalam bi fi mu cosaano sore Tank loxo nopp bakkan baat bët Gemmiñ ñooy mattal jëm ji Mo tax ba goor ñu wara nangulanté ndiaxas la Pusso ak weñ ñooy rabb laxassay (x4) Mélange d’idées de couleurs d’identités I’m the sibling of water and light, my name is color Refrain ------ Visage jaune, oreilles rouges, tignasse blonde, lèvres pulpeuses, nez épaté… Colère, joie, sérénité, tristesse, peur, plénitude, rancœur, amour… Le figuier rencontre l’olivier, L’univers est un mélange d’idées, de couleurs, d’identités, de ressentis… et aux lointaines origines de l’univers : un mélange. Un corps sans ses cinq membres n’en est plus un. C’est le fil et l’aiguille qui tissent la tunique... Patchwork. Enfant de l’eau et de la lumière, mon nom est couleur. ------ Yellow face, red ears, blond mop, pulpy lips, flat nose… anger, joy, serenity, sadness, fear, plenitude, resentment, love…The fig tree meets the olive one, the universe is a mixture of ideas, colors, identities, resents…and from distant origins of the universe: a blend. A body without its five limbs is not one anymore. It is the thread and the needle that weave the tunic… Patchwork. Sibling of water and light, my name is color.
2.
Nobel 05:08
Nobel ------ Mbëgeel moom dou miinel Mbëgeel moom du sopee, Mbëgeel moom du nobeel Mbëgeel dou coffeel Nimu ma dikké man dey xamuma ko boobu Mbëgeel nobeel li dey yémé Mbëgeel bu sell moom dey amna nobeel bu dëggu moom dey juddu na am sa tiios soxna ci teew moom dey Dimbële la wuutula xamal la yeeggé la jappalé la soxna ci dey moom jambaar la soxnaci dey moom waliyu la alalu aduna boolé wu leen taarou jëmm fassuleen Mbëgeel bu sell ruxul xudsi la message d'amour à ton cœur donne-moi le tien, je te donnerais le mien message de paix, reçois le sans peur il m'est apparu, il m'est survenu ce bonheur du ciel que j'ai tant attendu (x2) ceci est une voie divine qui me dit d'ouvrir mes sens d'y remplir beaucoup d'amour et d'en donner aux gens de l'amour nimu ma dikké man dey xamu ma ko dafa jekki jekki ñew sama xol bi ñew sama ruxu bi alalu aduna boolé wu leen taarou jëmm fassuleen soxna ci bul dem sa yoon ñewal fii ------ Au-delà de l’attachement, au-delà de l’attraction et de la passion, avant le désir et quand le chant des sens s’étiole…l’Amour est. Il a fallu que je me lasse de le chercher, que je me résolve à l’attendre, que j’oublie que c’était lui que j’attendais, pour qu’il survienne enfin. Cœur ouvert, âme désarmée, être sans attache, l’Amour m’a fait. ------ Beyond affection, beyond attraction and passion, before desire and when the melody of senses wilts…love is. I had to weary of seeking it, decide to wait for it, forget that I was in its wait, so that it finally turns up. Open heart, disarmed soul, being without bonds, Love made me.
3.
Ndiaye Gaindé ------ Fatick ndiaye neena mané saloum ndiaye neena bima démé fatick ndiaye- ndiaye,ndiaye gaindé xiiru na ndiaye gaindé xiiru na ndax suuf ci juratul maam yalla tawatul . mame yalla tawatul peex mi ñewatul ,dugub gui doyatul té su dugub gui doyatul xetax du amati ,jur gui sankuna ndiaye gaindé ndiaya gaindé ndiaye gaindé ndiaye gaindé fatick ndiaye neena, ah mané saloum ndiaye neena, fatick ndiaye bima démé fatick ndiaya ndiaye wowowo ndiaye gainde nena bima démé seeti ibrahima ndiaye si ndiaye-ndiaye neenama dugub amna waayé yorul kër gui njaayum gerté niakkum péxé la, njaayum dugub sonnal jaam bi la, beykat yi jooy nañu ñep daw ndakaaru sine ak saloum senegal oublié ndiaye gaindé x5 bima démé fatick ndiaye-ndiaye ndiaye gaindé neena bima démé seeti ibrahima ndiaye si ndiaye-ndiaye dugub moom amatul, dugub amatul ndax nguur gui bugu ko askan bi jooyna njaayum gerté feessalul poss yii késsé ndaw gui jooyna o kin o koor o yayum mba o tewum bougoune… ------ Le lion a rugi. Ndiaye Gaindé m’a fait part de la détresse du Sine et du Saloum. Les pluies se font rares, maigres récoltes et maigre bétail. Les lionceaux quittent la tanière et vont se faire rats des villes. Le noble agriculteur et sage berger n’est plus qu’un vulgaire marchand à la recherche du profit. Les sages Sérères disent pourtant qu’un homme n’est certain que de l’amour que lui portent sa mère et sa femme. ------ The lion has roared. Njaay Gainde has informed me of the distress of Sine and Saloum. Rains become rare, meager crops and meager livestock. Lion cubs leave the lair and make of themselves towns’ rats. The noble farmer and wise shepherd is no more than a vulgar merchant in search of benefit. Yet, the wise Serers say that a man has certainty of nothing else but only the love that his mother and his wife bear for him.
4.
Débarquement ------ Faaw nga bari duggu duggu ngir duggu (x3) tijjilma buntu bi ma duggu so yorul moom do duggu do duggu moom do duggu (X2) na kooni ngor ké jufé na kooni ngoorké jufé na kooni ndiaye ngoor ké jufé niap ka niapik dolé Faaw nga bari duggu duggu ngir duggu (x 4) tijilma bount bi ma dougou so yorul do dougou do dougou mom do dougou (x 4) fep fuma dem ñu laaj ma visa ana say keyit dekkuma seen rew amna suma rew ma deluwaat fima joggé debarquement d'ifrikiya nous sommes des exilés nous sommes des exilés débarquement d'ifrikiya nous sommes des réfugiés nous sommes des réfugiés débarquement d'ifrikiya nous sommes des africains ------ Le monde, nous dit-on, est devenu un village. On nous raconte aussi que nous y somme chez nous ; libre de bouger, d’aller et de venir quand nous le désirons. Que dire quand « nous » ne veut plus dire Nous ? Quand tu t’invitais chez moi, c’était sans me demander mon avis, mais une maison n’est jamais étroite nous disent nos sages, le cœur de l’hôte par contre peut manquer de place. Crois-tu à la liberté de mouvement que tu professes si à chaque fois que je dois venir chez toi, tu me demandes de justifier ma bonne foi ? Là où notre dignité est préservée, on est chez soi. ------ The world, are we told, has become a village. We’re also said to be at home in it; free to move, to go and come back when we want. What to say when “we” does not stand for “Us” anymore? When you were inviting yourself in home mine, it was regardless of my opinion, but a house is never narrow, our wise men say us, the heart of the host on the contrary can be lacking in place. Do you believe in the freedom of moving that you profess if at any time I should come at your home you ask me to declare my good faith? Home is where dignity is preserved.
5.
Darou 05:57
Darou ------ zikr.... duñu duggu luy naaw jëm kaw duñu duggu luy xuss jëm ndox sareet bi passi lay joggé jëm daru Mor Xureeja Siisé yalla la, rijal, xewël la affairu goor yalla la (refrain) axlu yalla bi parengeen sang bi neena ñu waajal magal gui axlu rijaalulah bi parengeen sang bi neena ñu waajal magal gui na ku nekk wut sass xar ci tanku tubey wëndeelu majaal sakku njariñ wooté leer samp dëgg jubal té leeral yalla la, rijal, xewël la bagaasu goor yalla la dëgg la sang bi waxal waxal ruxu yëp a dajjaloo (x2) borom baax dey gindi nga ñu dëgg la dëgg la dëgg la borom baax haq la leer la jantu ngëneel la (x2) Allahu Yalla jërëjëf maam Bamba Ten leeranu a ndiamé Te daawna in na leerum yalla la, rijal, xewël la affairu goor yalla la duñu duggu luy naaw jëm kaw duñu duggu luy xuss jëm ndox sareet bi passi lay joggé jëm daru Mor Xureeja Siisé yalla la, rijal, xewël la affairu goor yalla la axlu yalla bi parengeen sang bi neena ñu waajal magal gui axlu rijaalulah bi parengeen sang bi neena ñu waajal magal gui na ku nekk wut sass xar ci tanku tubey wëndeelu majaal sakku njariñ wooté leer samp dëgg jubal té leeral yalla la, rijal, xewël la bagaasu goor yalla la ------ Chapelets autour du cou, autour du poignet ou défilant entre le pouce et l’index, les langues en oraison, les cœurs en méditation, les esprits en contemplation, les corps en intense activité ; les disciples se dirigent vers Darou. Cet endroit d’où la lumière de Cheikh Moussa Cissé a irradié dans le temporel, cette station où l’âme se remémore et ne fait plus qu’un avec ce qui EST ; s’anéantissant sans hier ni demain, sans ici ni là-bas, sans haut ni bas, sans extérieur ni intérieur mais subsistant avec tout cela en même temps. Le Magal est une célébration, la réjouissance et la gratitude d’âmes béates, une réminiscence d’un instant encore présent, un renouvellement. ------ Rosary around the neck, around the wrist or parading between the thumb and the forefinger, tongues in oration, hearts in meditation, spirits in contemplation, bodies in intense activity; disciples steer for Daaru. This place where the light of Cheikh Mussa Cisse has irradiated in the temporal, this station where the soul recalls itself and just become one with what IS; annihilating itself with neither past nor future, without here nor there, without up and down, without outside nor inside but subsistent with all these at the same time. The Magal is a celebration, the rejoicing and gratitude of blissful souls, a reminiscence of a still prevailing moment, a revival.

credits

released April 11, 2015

license

all rights reserved

tags

about

SAHAD Senegal

Sahad and the Nataal Patchwork reflète une moisson de diverses influences musicales, un trait d’union entre plusieurs cultures. Ce groupe s'inscrit dans cette tradition de jeunes qui portent avec eux le nouveau souffle de la musique africaine. Leur musique se trouve à la croisée des chemins entre le blues Malien, l’Afrobeat, le rock et le jazz qui font naitre une sonorité kaléidoscopique. ... more

contact / help

Contact SAHAD

Streaming and
Download help

Redeem code

Report this album or account

If you like SAHAD, you may also like: