We’ve updated our Terms of Use to reflect our new entity name and address. You can review the changes here.
We’ve updated our Terms of Use. You can review the changes here.

Darou

from Nataal by SAHAD

/
  • Streaming + Download

    Includes unlimited streaming via the free Bandcamp app, plus high-quality download in MP3, FLAC and more.
    Purchasable with gift card

      €1.50 EUR  or more

     

lyrics

Darou
------
zikr....
duñu duggu luy naaw jëm kaw
duñu duggu luy xuss jëm ndox sareet bi passi lay joggé jëm daru Mor Xureeja Siisé
yalla la, rijal, xewël la affairu goor yalla la (refrain)

axlu yalla bi parengeen sang bi neena ñu waajal magal gui
axlu rijaalulah bi parengeen sang bi neena ñu waajal magal gui
na ku nekk wut sass xar ci tanku tubey
wëndeelu majaal sakku njariñ
wooté leer samp dëgg jubal té leeral
yalla la, rijal, xewël la bagaasu goor yalla la

dëgg la sang bi waxal waxal
ruxu yëp a dajjaloo (x2)
borom baax dey gindi nga ñu
dëgg la dëgg la dëgg la
borom baax haq la leer la jantu ngëneel la (x2)

Allahu Yalla jërëjëf maam Bamba
Ten leeranu a ndiamé
Te daawna in na leerum

yalla la, rijal, xewël la affairu goor yalla la
duñu duggu luy naaw jëm kaw
duñu duggu luy xuss jëm ndox sareet bi passi lay joggé jëm daru Mor Xureeja Siisé
yalla la, rijal, xewël la affairu goor yalla la

axlu yalla bi parengeen sang bi neena ñu waajal magal gui
axlu rijaalulah bi parengeen sang bi neena ñu waajal magal gui
na ku nekk wut sass xar ci tanku tubey
wëndeelu majaal sakku njariñ
wooté leer samp dëgg jubal té leeral
yalla la, rijal, xewël la bagaasu goor yalla la
------
Chapelets autour du cou, autour du poignet ou défilant entre le pouce et l’index, les langues en oraison, les cœurs en méditation, les esprits en contemplation, les corps en intense activité ; les disciples se dirigent vers Darou. Cet endroit d’où la lumière de Cheikh Moussa Cissé a irradié dans le temporel, cette station où l’âme se remémore et ne fait plus qu’un avec ce qui EST ; s’anéantissant sans hier ni demain, sans ici ni là-bas, sans haut ni bas, sans extérieur ni intérieur mais subsistant avec tout cela en même temps.
Le Magal est une célébration, la réjouissance et la gratitude d’âmes béates, une réminiscence d’un instant encore présent, un renouvellement.
------
Rosary around the neck, around the wrist or parading between the thumb and the forefinger, tongues in oration, hearts in meditation, spirits in contemplation, bodies in intense activity; disciples steer for Daaru. This place where the light of Cheikh Mussa Cisse has irradiated in the temporal, this station where the soul recalls itself and just become one with what IS; annihilating itself with neither past nor future, without here nor there, without up and down, without outside nor inside but subsistent with all these at the same time. The Magal is a celebration, the rejoicing and gratitude of blissful souls, a reminiscence of a still prevailing moment, a revival.

credits

from Nataal, released April 11, 2015

license

all rights reserved

tags

about

SAHAD Senegal

Sahad and the Nataal Patchwork reflète une moisson de diverses influences musicales, un trait d’union entre plusieurs cultures. Ce groupe s'inscrit dans cette tradition de jeunes qui portent avec eux le nouveau souffle de la musique africaine. Leur musique se trouve à la croisée des chemins entre le blues Malien, l’Afrobeat, le rock et le jazz qui font naitre une sonorité kaléidoscopique. ... more

contact / help

Contact SAHAD

Streaming and
Download help

Redeem code

Report this track or account

If you like SAHAD, you may also like: